audio
audioduration (s) 1.22
171
| text
stringlengths 6
108
|
---|---|
defarkatu mburu la. |
|
may ma genn ! |
|
garab la gog, ñu ngi koy fekk mu yaatu lool ci tund afrig. |
|
damay wër koor gu ndaw. |
|
luy weesu la. |
|
wota bi, daa am yàqu-yàqu. |
|
lan ngay def nii ? |
|
farañse laay wax. |
|
maa ngi ziyaar sama sëriñ ak sama doomu baay . |
|
ndax nit ñaa ngi leen di may nopp ? |
|
ci àngale, mooy alabaster. ci faranse mooy albatre |
|
amdi géy |
|
móoris, republig bu móoris, réewu afrig |
|
dinaa ñu |
|
man nga maa indi ñu ci siiw ci àddina si ? |
|
damaa yëg sama bopp. |
|
jigéen ji daal di jël ndam li. |
|
ndax dinaa mën a matale liggéey bii? |
|
melow suuf ci jëmm, soppi |
|
njandaam, day meññi ay foytéef. |
|
gannaaw ba mu jàppee loolu lépp. |
|
damaa xaw a sonn. |
|
nanu noppalu fii. |
|
kenn ñëwul woon. |
|
ku jéemul, du am dara. |
|
ab tóoy la. |
|
iniwersite bu ndar, ëmb na juróorum-ñaari bërëbu tàggat ak gëstu |
|
baaba moom sama lépp la |
|
tomas adison it ñëw, indil ñu làmp bu mbëj. |
|
nan ko defaat. |
|
neex ab sëyeeful neex na ma. |
|
dawalleen mbind mi. |
|
sëriñ abdu xaadir mbàkke, moom ag ayam weesuwul 11 weer |
|
ak ci fukk, ba ci ñaar-fukk i met, ci njoolaay |
|
defar leen seen i yéere ! |
|
du lu jaaduwul. |
|
maki, mu ngi woo waa àdduna bi ngir ñu janoo ak jafe-jafe yi. |
|
damaa ragal a dee. |
|
polotigi afrigu bëj-saalum. |
|
xel mi dafa ñaaw. |
|
janq yi dañoo dof. |
|
dafa am lu mu ma jàppal. |
|
bu sa bët jóg ci moom ! |
|
xalel foto-foto la noo ko raaxe rekk lay wéye |
|
nanu ko defaat. |
|
bàyyi leen seen yoxo yi ! |
|
duma nelaw mukk ci sama barabu liggéeyukaay. |
|
xale dong la. |
|
reer bi damaa rëcc |
|
lekk gi daa sedd. |
|
tom a ngi këram. |
|
tom, dafa xamadi. |
|
booy nàmpal sa doom, nanga fexe ba sa toogaay mbaa sa tëraay jekk |
|
nettaliy xew-xewi cosaan |
|
ndax ñoom doylu nan ? |
|
yëgu ma dara. |
|
dogal yi jëm ci santaaneb alikeñ yi ni ko takk-der yi déggee baaxul |
|
doxalee na ak ug xereñ. |
|
ndax man naa laa dimbali? |
|
mës nañu koo dëne. |
|
mi ngi noppi. |
|
na nga xellu ! |
|
ni nuy gëme malaaka yi yal na yàlla dolli xeewal ak mucc ci ñoom |
|
dañoo bëgg tom. |
|
dama leen a neexal. |
|
cari foytéefam day yàgg ak ñoom lool. |
|
ñëwal soo ko mënee!? |
|
dama leen yittewoo. |
|
dëkkul ci dalu daara ju kawe ji. |
|
ci lañu biral faatug george floyd |
|
yéreem yi dañoo xotteeku woon. |
|
leegi am naa tiis. |
|
muhammadu raasin njaay |
|
seeñi maam ñu bare ca xetu sooninke ak naar lañu juge. |
|
di na dox lool ci moom. |
|
ku baax la tey wéetal na askan wi |
|
dinaa la dimbali. |
|
ay dëkkuwaay ñeel waa tugal yiy saytu digg yooyu |
|
ajaatal montar bi. |
|
man naa am dee na. |
|
taaliif wii nag lu ñu barkeel la ci njëlbéen gi ba ca dayo ba. |
|
jaroon na ko. |
|
dama sangu rekk. |
|
yóbbuwoon nan ko. |
|
njabootu manna yi, ñoo daan jaa-ogo yi |
|
ku gëm yàlla ? |
|
gisuma ci ngaañ. |
|
ag dogu dëgg de, dëgër bopp moo koy gunge |
|
rawati na ci wàlli njàggat , fànn ak tabaxiin . |
|
ci waññib 2002 bi, nit ñi ñi ngi tolloon ci 461 159. |
|
tom du yeex a ñëw. |
|
tànn na li mu bëgg. |
|
defal rekk sa liggéey! |
|
waat yi jëm ci xare yu bari ci almaa lañu juge |
|
jaajëf?! naka mu? |
|
yéen jëli ngéen bu baax. |
|
ku nekk ci barab bi? |
|
ay baat aki waxiinsoppi |
|
tom lekk na sama añ. |
|
mi ngi yaatoo 4 km², ci 2005 amoon na 971 way dëkk. |