audio
audioduration (s)
1.22
173
transcription
stringlengths
8
159
transcription_normalised
stringlengths
8
159
Ay ndaw la ñu ba leegi. Deel weg mag doonte da di ku doyadi te xeebu.
ay ndaw la ñu ba leegi. deel weg mag doonte da di ku doyadi te xeebu.
Noo ngi yàq ndox. Sama kër daa neex.
noo ngi yàq ndox. sama kër daa neex.
Damaa yëg yokkuteg kàttan. Da ngaa dof.
damaa yëg yokkuteg kàttan. da ngaa dof.
Maa ngi leen di ñaan ngeen dellusi. Sa xalaat la woon.
maa ngi leen di ñaan ngeen dellusi. sa xalaat la woon.
Ku yewwu la lool. Bile baat, manko tëggé ci anthropologie, man aam anthro
ku yewwu la lool. bile baat, manko tëggé ci anthropologie, man aam anthro
Damaa bëgg sama bopp. ①- JËFI SAAY-SAAY JA AMOON CA MARIST AK SITE KËR GÓORGI
damaa bëgg sama bopp. ①- jëfi saay-saay ja amoon ca marist ak site kër góorgi
Ci la takk-der yi tamit janook àttekat bi Lii sama wërsëg a.
ci la takk-der yi tamit janook àttekat bi lii sama wërsëg a.
Ñatteelu futbalkatu Juvantus bu am Koronaawiris bi. Bàyyil di ma naan jàkk !
ñatteelu futbalkatu juvantus bu am koronaawiris bi. bàyyil di ma naan jàkk !
Dunu ay raykat. Dañu maa jël.
dunu ay raykat. dañu maa jël.
Dafa seeti xaritam. Lëg yi ndax man na ñoo féey ?
dafa seeti xaritam. lëg yi ndax man na ñoo féey ?
Nataalu xobi gàncaxug gerte Gis naa ko mu def ko.
nataalu xobi gàncaxug gerte gis naa ko mu def ko.
Xammoon na gone ga. Tom a nekkoon ñetteel.
xammoon na gone ga. tom a nekkoon ñetteel.
Ndax man ngeen ko koo faye ? Tànnal benn ngànnaay !
ndax man ngeen ko koo faye ? tànnal benn ngànnaay !
Lu yomb la niki nanga def. Lu ngeen def ?
lu yomb la niki nanga def. lu ngeen def ?
Di kàddu yu mu yékkati ci kanamu taskati xibaar yi. Dama soxla ay xarit.
di kàddu yu mu yékkati ci kanamu taskati xibaar yi. dama soxla ay xarit.
manu koo dawal. Ndax sa DVD la?
manu koo dawal. ndax sa dvd la?
Sunu dëkkuwaay la. Matal nga saw sas.
sunu dëkkuwaay la. matal nga saw sas.
Taax mii rekk laa bañ. Nu àgg,laataa jullig fajar,mu fanaan guddi gi ci yekkati ay bayit ,di boroomug jàjji.
taax mii rekk laa bañ. nu àgg,laataa jullig fajar,mu fanaan guddi gi ci yekkati ay bayit ,di boroomug jàjji.
Waaye ñépp bokkuñu gis-gis Damaa bëgg ub lolli.
waaye ñépp bokkuñu gis-gis damaa bëgg ub lolli.
Jàppleen bu dëgër ! Damaa am uw tiis.
jàppleen bu dëgër ! damaa am uw tiis.
Jawwu ji ak Jéeri ji suuf Ku mar tax a naan pótit, bu ndox tuuroo nga rus
jawwu ji ak jéeri ji suuf ku mar tax a naan pótit, bu ndox tuuroo nga rus
Jéem naa la koo wax. Damay sangu bis bu set.
jéem naa la koo wax. damay sangu bis bu set.
Karawaat bu ñàng la woon. Nekk naa tamit jkat.
karawaat bu ñàng la woon. nekk naa tamit jkat.
Neexoon na lool. Maa ngi ci yoonu teewlu.
neexoon na lool. maa ngi ci yoonu teewlu.
Mayleen ko dara mu naan ! Ci daamaram gi la dëkk.
mayleen ko dara mu naan ! ci daamaram gi la dëkk.
Ndoxum cangaay li noppi na. Fexe leen ba ñuy wàccook seen liggéey ci waxtu yu yem
ndoxum cangaay li noppi na. fexe leen ba ñuy wàccook seen liggéey ci waxtu yu yem
Te yit, jubluwuma ci ŋàññ la, walla di yàq sa der Sama njort naxu ma.
te yit, jubluwuma ci ŋàññ la, walla di yàq sa der sama njort naxu ma.
Dañu leen a mere lool. Damaa bëgg ñamu suukar.
dañu leen a mere lool. damaa bëgg ñamu suukar.
Li aju ci laab Xale ya ñëw mu ñaanal leen ñu takk laxas ngir génn dëkk bi
li aju ci laab xale ya ñëw mu ñaanal leen ñu takk laxas ngir génn dëkk bi
Wor sa ŋaamaan moo gën wor sa léttkat Xamoon na ne wóorul.
wor sa ŋaamaan moo gën wor sa léttkat xamoon na ne wóorul.
Mbégtey gàddaay gi Ndax dangaa bëgg woy?
mbégtey gàddaay gi ndax dangaa bëgg woy?
Jàppaat nañleen bu yàggul dara… Ame nga paas?
jàppaat nañleen bu yàggul dara… ame nga paas?
Ndax man naa koo wax ca kaw ? Biram Kodd Dumbe1757/ 6i weer
ndax man naa koo wax ca kaw ? biram kodd dumbe1757/ 6i weer
Jom tax na jàmbaar jomb gàcce, ca maam ya ak maamaat ba tay. Baayu Balaam la woon.
jom tax na jàmbaar jomb gàcce, ca maam ya ak maamaat ba tay. baayu balaam la woon.
Maa ngi dee ak xiif ! Damaa raxas samay tànk.
maa ngi dee ak xiif ! damaa raxas samay tànk.
ma ëyu leen ne aaye naa ko, indi léen Wolof genn giir la gu nekk Senegaal
ma ëyu leen ne aaye naa ko, indi léen wolof genn giir la gu nekk senegaal
Nee na néew ji doole la woon. Càkkeef bu kenn xamul numu mel ngeen.
nee na néew ji doole la woon. càkkeef bu kenn xamul numu mel ngeen.
Cosaanal wird Wahyu lay doon walla Yénkeewal, Yàlla moo koy jagleel ay ñoñam Ndax, ci atum 2012 ay defkati ñaawteef yuy mbuboo lislaam song réew ma
cosaanal wird wahyu lay doon walla yénkeewal, yàlla moo koy jagleel ay ñoñam ndax, ci atum 2012 ay defkati ñaawteef yuy mbuboo lislaam song réew ma
Jullig àjjuma waa Lewna Ñaseen fippu nañu Fonk seen bopp, seen taarix aks een xalaat.
jullig àjjuma waa lewna ñaseen fippu nañu fonk seen bopp, seen taarix aks een xalaat.
Fukkeeli matukaay ak juróom ñent Sëriñ Maalig Basin Si
fukkeeli matukaay ak juróom ñent sëriñ maalig basin si
Naalub mbay bu Xelkoom, mu yaatoo ci 45.000 ha. kariim jóob 25 sàttunmbar 2010/waxtu 1128 Alikànte Espaañ.
naalub mbay bu xelkoom, mu yaatoo ci 45.000 ha. kariim jóob 25 sàttunmbar 2010/waxtu 1128 alikànte espaañ.
Boroom xel mu gudd te rafet boroom wàlliyu la Nit ku ne am na sañ-sañ wax mbaa bind lu ko soob
boroom xel mu gudd te rafet boroom wàlliyu la nit ku ne am na sañ-sañ wax mbaa bind lu ko soob
Sàmba-koppar Maam Bàlla Njaay ??‍? Waaye ndàmpaay li, ci njabootam lay dellu, ñoo koy fey
sàmba-koppar maam bàlla njaay ??‍? waaye ndàmpaay li, ci njabootam lay dellu, ñoo koy fey
Yebbiy Seex Anta Joob, liggéeyub Djibril Samb Ñoom ñépp ay xale lañu.
yebbiy seex anta joob, liggéeyub djibril samb ñoom ñépp ay xale lañu.
Nan jóg jëlee fii Jàppleen ma su ngeen ko manee !
nan jóg jëlee fii jàppleen ma su ngeen ko manee !
Dama soxla ab ngànnaay. Dellul Ginnaaw !
dama soxla ab ngànnaay. dellul ginnaaw !
Maa moom sàngara sii. Ndax fii wóor na ci nun ?
maa moom sàngara sii. ndax fii wóor na ci nun ?
Damay faral di naan attaaya. bul laal sama oto.
damay faral di naan attaaya. bul laal sama oto.
Jéem nga ? Caabi ja réer ma.
jéem nga ? caabi ja réer ma.
Ay fennkat ngeen. Seetleen seen i jibba !
ay fennkat ngeen. seetleen seen i jibba !
Am nga téere yu bari. Xam-xamu làmmiñal bu des te li ko waral mooy gàttaayu tàggat bi
am nga téere yu bari. xam-xamu làmmiñal bu des te li ko waral mooy gàttaayu tàggat bi
Nële naan du tus. Dummóoyu ngir soof gu la mbir soof
nële naan du tus. dummóoyu ngir soof gu la mbir soof
Ndege, ECO, moomeelu CEDEAO la Rëcc ak màmm
ndege, eco, moomeelu cedeao la rëcc ak màmm
Wolof 11 miliyon i nit Senegaal, Mali, Gambi, Moritani,... Jigéen yelloo na am jëmmu alalu boppam, ni ko jëkkëram sañe
wolof 11 miliyon i nit senegaal, mali, gambi, moritani,... jigéen yelloo na am jëmmu alalu boppam, ni ko jëkkëram sañe
Halaa nabi xayri anaam Dafa baax lool?!
halaa nabi xayri anaam dafa baax lool?!
Jógleen sama lal ! Tom daanaka jooy na.
jógleen sama lal ! tom daanaka jooy na.
Bu dee ‘’Force Covid-19’’ moom, dama koo waxaalewul ①-MASUUR FAAL 68/ ...100
bu dee ‘’force covid-19’’ moom, dama koo waxaalewul ①-masuur faal 68/ ...100
Bëgg naa ab téere. Ndax dangeena fiir?
bëgg naa ab téere. ndax dangeena fiir?
Fab nanu ko. Tom dafal war def dara leegi .
fab nanu ko. tom dafal war def dara leegi .
Ndax man ngeen a dawal lii? Soxla ngeen a dallu.
ndax man ngeen a dawal lii? soxla ngeen a dallu.
Ametist ni ñi ko rafetale. Ñàkk nañu nu
ametist ni ñi ko rafetale. ñàkk nañu nu
Dëgg la, PAI ag cëslaay gu ko daan dooleel la Maa ngi dem leegi.
dëgg la, pai ag cëslaay gu ko daan dooleel la maa ngi dem leegi.
Meññeefi garabug sànd Amoon nab xaj.
meññeefi garabug sànd amoon nab xaj.
Damaa ame tàggatkat bu baax. Ci mujj gi mu dëkksi Tiwaawan ci 1902
damaa ame tàggatkat bu baax. ci mujj gi mu dëkksi tiwaawan ci 1902
Damaa soxlaa xam leegi. Bis bun wumee mu dal di dem fa Yàlla
damaa soxlaa xam leegi. bis bun wumee mu dal di dem fa yàlla
Bul jaaxle ! Beneen joŋante bi doon dox ci diggante Inter Milaŋ?? ak Bayeer Liwerkusen??
bul jaaxle ! beneen joŋante bi doon dox ci diggante inter milaŋ?? ak bayeer liwerkusen??
Diiwaani kilima yi Kippango gaa ngi doon xaar.
diiwaani kilima yi kippango gaa ngi doon xaar.
Waay may ma jàmm ! Am kàjj laa moo xam ne.
waay may ma jàmm ! am kàjj laa moo xam ne.
Maa ngi làkk mburu. Ba mu ☞ bam
maa ngi làkk mburu. ba mu ☞ bam
Dafa doy nag ! Man na maa gis it di xanaa?
dafa doy nag ! man na maa gis it di xanaa?
Ndax Pari nga nekk ? Ku yabu far tàbbal ko pax
ndax pari nga nekk ? ku yabu far tàbbal ko pax
Xaalu tubaab xeetu ñax la guy caram di law lool bay àgg 3i met Demleen jëli seen yaay!
xaalu tubaab xeetu ñax la guy caram di law lool bay àgg 3i met demleen jëli seen yaay!
Sama noon nga. Dañuy fekk Alegsàndiri ci Injiil ci Jëf 691824276 2811.
sama noon nga. dañuy fekk alegsàndiri ci injiil ci jëf 691824276 2811.
Soxna Sina Jóob +393714782767 Gént la woon.
soxna sina jóob +393714782767 gént la woon.
Mu bari lool ci tundu Afrig, Ecopi, Afrig bëj-saalum. Tom manul a def liggéey bi.
mu bari lool ci tundu afrig, ecopi, afrig bëj-saalum. tom manul a def liggéey bi.
Dama fa waroon a dem. Céy ngalla ñun li ci réew mi ak ay lekoolam!
dama fa waroon a dem. céy ngalla ñun li ci réew mi ak ay lekoolam!
lu bon ci ag mbëbëstënam ci foo ko gis ba ronqoñ di yol saaw fit ni yéjji ni laaxu gar
lu bon ci ag mbëbëstënam ci foo ko gis ba ronqoñ di yol saaw fit ni yéjji ni laaxu gar
Taysiirul Hasiir bu Seex Maalig Ñas ca Tuubaa Baxdaat/2 Ag wóolu jee naa
taysiirul hasiir bu seex maalig ñas ca tuubaa baxdaat/2 ag wóolu jee naa
Bëgg naa kippaango gii. Jamaaiiria Araab bu Liibiee Jamaaiiria Araab liibiee Popileer Sosiaalist réewum Afrig.
bëgg naa kippaango gii. jamaaiiria araab bu liibiee jamaaiiria araab liibiee popileer sosiaalist réewum afrig.
Loo leen bëgg a wax ? Nànd na ko.
loo leen bëgg a wax ? nànd na ko.
Ndax lii yépp yaa ko moom? Dina taw de.
ndax lii yépp yaa ko moom? dina taw de.
Ëttug gëstu ci nj waññi IREMPT Ci liggéey ngeen di wax?
ëttug gëstu ci nj waññi irempt ci liggéey ngeen di wax?
Dinaa dem jëndi ay yëf. Bis bépp maa ngi woon ci biti.
dinaa dem jëndi ay yëf. bis bépp maa ngi woon ci biti.
Aakimoo jawwu ji, walla xare bi ngir teg loxo ci jawwu ji sanc ko Ñëwal soo ko mënee!?
aakimoo jawwu ji, walla xare bi ngir teg loxo ci jawwu ji sanc ko ñëwal soo ko mënee!?
Manóo weddi lii. Amu ci loraange.
manóo weddi lii. amu ci loraange.
bàyyil coow ! Loolu daal, lan jot a def
bàyyil coow ! loolu daal, lan jot a def
Saa Kanadaa la. Fàww nu waxtaan .
saa kanadaa la. fàww nu waxtaan .
Ndax ni réewum Dante soppeekoo jéggi na dayo Boolewuñu ma ci woon.
ndax ni réewum dante soppeekoo jéggi na dayo boolewuñu ma ci woon.
Nan nga ko réeralee? Ag gént dong la.
nan nga ko réeralee? ag gént dong la.
Faamara Ibraahiima Siise di njiital I'ACSIF la ñu tegoon loxo démb. Ngir sama njaboot a.
faamara ibraahiima siise di njiital i'acsif la ñu tegoon loxo démb. ngir sama njaboot a.
Doomi Senegaal ya tag ca Farãas dinañu leen delloosi ci talaata ji Bul bàyyi benn bis am njàng, te nga jëfe ko cig jaamu Yàlla
doomi senegaal ya tag ca farãas dinañu leen delloosi ci talaata ji bul bàyyi benn bis am njàng, te nga jëfe ko cig jaamu yàlla
Faratay julli fukk ak juróom lañu Xoolal kiy wax loolu.
faratay julli fukk ak juróom lañu xoolal kiy wax loolu.
Dinanu man xaar. Wuññi yu juxraaf yu Espaañ yi
dinanu man xaar. wuññi yu juxraaf yu espaañ yi
Ci fànna yu teqalikoo, Di Reew yi Afrig bu nekk ca suuf Saara
ci fànna yu teqalikoo, di reew yi afrig bu nekk ca suuf saara
Ngir faagaagal leen, lii mooy pexem noon. Dinaa ko jënd.
ngir faagaagal leen, lii mooy pexem noon. dinaa ko jënd.
Ama Juuf nak kerr Semu Njeke la joge ca waali Njuufeen. yaramu jigéenu-wérul bi dafa tàng
ama juuf nak kerr semu njeke la joge ca waali njuufeen. yaramu jigéenu-wérul bi dafa tàng
Dinga ma man a yëgël a ? Lii ka rafet !
dinga ma man a yëgël a ? lii ka rafet !
Xamatuñu tey jii ne tembe fan la Aynon walla Salim nekkoon War namaa dem.
xamatuñu tey jii ne tembe fan la aynon walla salim nekkoon war namaa dem.
Loolu dong laa xamoon. Gii Maryiis Saaña  Nun, danoo am wërsëg sax
loolu dong laa xamoon. gii maryiis saaña  nun, danoo am wërsëg sax
Ay doomam bari nay njariñ lool. Warunu faa dem.
ay doomam bari nay njariñ lool. warunu faa dem.

Dataset Card for "Wom_tts"

More Information needed

Downloads last month
82
Edit dataset card