start_time
float64
0
2.73M
end_time
float64
326
2.78M
speaker_id
stringclasses
55 values
text
stringlengths
1
4.06k
audio
audioduration (s)
0.17
388
1,012,907
1,013,341
11spk1
%hum %hum
1,013,341
1,028,577
11spk2
boo ko toppee it noonu la fa noonu la fa demee donc mu doon loo xam ne dees na ko bàyyi xel waaye enquêtes yeeg yooyu ñu ngi ciy def liggéey boo xam ne waa CESNA enquêtes yi ak services agricoles yi dina ko gën a firndeel su ko defee dina doon outil de décision bi outil décision ngir kilifa yi gën ko bàyyi xel
1,028,577
1,040,406
11spk1
%hum %hum tay wax nga zone d' intervention yi ngeen di nekk mais exactement %e pour quelque chose de concret tay lan ngeen di defal ñi nga xamante ne ñoom ñooy baykat yi fan ngeen leen di indilee seen apport yéen
1,040,406
1,051,001
11spk2
voilà maanaam %e liggéey bi ñuy def mooy lan dañuy saytu ne boo xoolee lii ma tiim rapport la maanaam semaine bu jot dinañ def rapport boo xam ne dañ koy yónni
1,051,001
1,051,392
11spk1
%hum %hum
1,051,392
1,062,067
11spk2
yónnee kilifa yi yónnee ko kilifa yi nekk ci région bi yónnee ko suñu naataangoo yi ñu mel ne ñoom Maodo ak services yi nga xam ne yëpp yi nga xam ne kenn ku ci ne ba ci presse bi sax seen naataangoo yi ñoom ñépp dañ koy jot
1,062,067
1,062,628
11spk1
%hum %hum
1,062,628
1,069,938
11spk2
presse bi yépp bu ma leen limee xëy na dana gudd waaye su ma nee presse bi ñi may dégg xam nañ ne %e rapport DRDR wax dëgg fa Yàlla ñi koy jot bëri na
1,071,585
1,083,581
11spk2
ba Dakar état major gendarmerie nationale dañ koy jot waxuma ministère bi nag ak i kuréelam donc dañ koy tas loolu bokk na ci li nga xam ne xëy na ñun ñooy liggéeyee noonu jàpp nañ jàpp ne xibaar bi dafa war a tas
1,083,581
1,083,979
11spk1
%hum %hum
1,083,979
1,092,966
11spk2
nit ñi di ko dégg waaye xibaar bi yépp mu tegu ci lu dëggu tegu ci xam-xam maandu it te nga xam ne amal njëriñ askan wi mu bañ a am benn parparloo bañ a am lenn lu ñuy nëbb
1,092,966
1,093,408
11spk1
%hum %hum
1,093,408
1,100,296
11spk2
ndax am na ci loo xam ne boo ko nëbbee it nit ñi bu ñu génnee mu ne ah ma ne ko buñ ko gisee mu ne ah ma ne ko dinañ la joxoñ te loolu nekkul liggéey boo xam ne dafa tegu ci xam-xam
1,100,296
1,100,838
11spk1
%hum %hum
1,100,838
1,126,227
11spk2
moo tax lépp lu ñuy def it dañ ciy jiital dëgg gi ak xam-xam bi lëkkaloo ko nag ak ñi nga xam ne ñoom lañ ko lëkkalool tas xibaar bi ba nga xam ne ñi kowar a jot ñépp kilifa région bi ñu ngi koy jot maasàllaa léegi nag boo gisee suñ taxawaay du lenn boo gisee ñu ne jiw yi liñ def si boo xoolee rapport bi situation yépp lay def bawul dara situation jiwu situation engrais taxawaayu gàncax gi ba mu tàmbali ba fi mu toll nii ak li ma wax yépp boo ko xoolee li ñu wax yëpp mu ngi ci rapport bii ma tiim
1,129,566
1,130,598
11spk1
%hum %hum
1,130,598
1,149,524
11spk2
boo ko xoolee pour ñu daal di %e saaraan tuuti laal tuuti li nga xam ne %e boo xoolee %e tay jii ci wàll wi boo xoolee fi ñu toll ci wàllu liggéey bi nit ñi góob nañu dugub ñu ngi takk saabaar yi mooy botte yi
1,149,524
1,149,867
11spk1
%hum %hum
1,149,867
1,170,462
11spk2
soo demee saabaar yi boo gisee ñu xool dañ koy tas def ko ci ay clé weeraat ko ndax dugub bu wowut ni mu war a wowee kenn du ko bojj su wowut ni mu war a wowee kenn du ko def ci sàq gerte gi boo ko jëlee mu ne ah ma ne ko déqi nañ ko waaye bu ñu ko deqee gis nga dañ koy dajale def ko ay dajale yu ndaw moom la ñu tuddee andain
1,170,462
1,170,905
11spk3
%hum %hum
1,170,905
1,175,257
11spk2
garab bu ñu ko defee noonu loolu li ñu ci jublu mooy bàyyi ko naaj wi di ko laal
1,175,257
1,175,874
11spk3
%hum %hum
1,175,874
1,187,963
11spk2
bu ko naaj wi laalee am na fu tolluwaay fu muy toll ñu doog ko dajalewaat def ko naaf la cay topp mooy lan mooy bàcc la ca topp mooy lan def ci saag jaay maa ngi denci ji kër ga
1,187,963
1,188,632
11spk1
%hum %hum
1,188,632
1,196,257
11spk2
lijjanti ci ag jiwu ak nga def ci rënd baag la ca topp ak la ca topp ak asaka yaag ak la ca topp ak la ca topp kon ci foofu la ñu toll
1,196,257
1,209,339
11spk1
%hum donc fi mu toll nii boo xoolee ci tool yi ngay gis dakasa yi ñoom ñoo fa nekk dakasa yi li tax mu am solo mooy %e séchage boobu ñuy def dafa am benn feebar bu ñuy wax saabu bu ma ko fàttewul mooy aflatoxine
1,209,339
1,209,868
11spk3
%hum %hum
1,209,868
1,215,566
11spk2
gëstu wane na ne gis nga li gën sax ci %e dakasa yooyu noonu
1,215,566
1,215,922
11spk3
%hum %hum
1,215,922
1,263,276
11spk2
léeg léeg da ngay gis baykat bi des fois dañ koy tourner dañ koy retourné retourné boobu lu am solo la gis nga boo ko retourné ba taat bi féete kaw ab njàngat gëstu man Yàlla def na gëstu naa ci sama def naa ci mémoire DEA université ci aflatoxine boobu bokk na ci li ñu wane ne ci li ñuy tuddee bonne pratique bu ñu jëlee dakasa googu di ko retourné maanaam di ko di ko wëlbati ba taat wi féetee kaw bu ko naaj wiy lakk gis nañ ne dina wàññi dooley aflatoxine bi ci biir gerte gi mooy feebaru saabu bi te ñépp xam ne aflatoxine lu xaw a lu ñu xaw a sonal la donte ne tay jii sax alxamdulilaa am nañ ci ab pexe boo xam ne bu tëru ci xam-xam bu ñuy wooyee %e enrobage tay jii aflaxine bi boo xoolee Sénégal ñu ngi koy defar
1,263,276
1,264,303
11spk1
%hum %hum
1,264,303
1,282,071
11spk2
te am nay jamono amu fa woon léegi gis nañu ñu ngi koy defar mu ngi tas ci tool yi loolu bokk na ci li nga xam ne ci luy xeex aflatoxine bi la waaye nag ci wàllu it li nga xam ne baykat bi mën na ko def mooy ci bonne pratique gis nga séchage bii nga xam ne moom lay def maanaam bàyyi dakasa yi noonu bu koy naaj wi di ko lakk
1,282,071
1,282,614
11spk1
%hum %hum
1,282,614
1,289,658
11spk2
mu koy wëlbati mu koy lakk balaa mu koy def naaf gis nañ ne am na njeexital ci xeetu saabu boobu noonu
1,292,849
1,323,908
11spk2
waaye leneen li boo xoolee boo boo xoolee ñoom ñoom sëñ Maodo dañuy lu ñu tuddee tawu hors saison bu xawee am ak gerte gi nga xam ne vague yu njëkk yi boobu aussi mun na am jeexital ndax day am lu ñu tuddee saxaat te doonul li gën mooy regermination loolu it dañ koy xaw a %e xaw a xaw a lifin moo tax moo tax baykat yi da ngay gis ñuy njëkkante ci vague bu njëkk bi gis nga ñu daal di koy déqi ndax dañuy bañ mu regermer waat maanaam mu saxaat bu fekkee ne am na ay taw yoo xam ne liñ tuddee taw hors saison nga xam ne moom it dafay am
1,323,908
1,324,722
11spk1
%hum %hum
1,324,722
1,333,728
11spk2
**** waaye boo xoolee njeexital bi fi mu gënee amee solo mooy li jëm ci gàncax gi demee ni ki basi fi mu toll nii boo génnee da ngay gis toolu basi yi ni ñu ni ñu naatee
1,333,728
1,334,502
11spk1
%hum %hum
1,334,502
1,347,428
11spk2
nga xool pastèque bi xaal bi te boo xoolee ci xaal bi am na loo xam ni %e dinañ ci sant ñoom Maodo ci ab doxalin bis boo xoolee liñ njëkk a ñëw ci marché bi ci wàllu mbayeef xaal lay doon
1,347,428
1,348,101
11spk1
%hum
1,348,101
1,356,827
11spk2
ñu bëri ñu ngi naan fan lay jóge fii lay jóge rawatina arrondissement Niakhar bii te loolu ci liggéeyu ñoom Maodo dégg ngeen ne li ñu tuddee seen GTP
1,356,827
1,357,387
11spk1
%hum %hum
1,357,387
1,386,021
11spk2
nee na ab kuréel boo xam ne di dajale baykat di waxtaan ak ñoom ci lañ gis ne waaw dañ nekk ci changement climatique bi kon nañu defi pexe donc pexe boobu si ñoom Maodo la jóge ba mu law moo tax ne am na ñoo xam ne am na ay du ñu tudd tur waaye am na ci ñoo xam ne buñ déggee ñuy wax dinañ xam ne ne ñoom ñoom %e ñu ngi leen di ñu ngi leen di gërëm santaale ci suuf santaale ñu dem ci ba gis ne nekk na lu am solo ndax xaal boobu di teel a ñëw ci wàllu koom day fay maanaam mooy gën a rentable que bu demee ba xaal yépp ñorandoo daje ci marché bi
1,386,021
1,386,992
11spk1
%hum %hum
1,386,992
1,419,152
11spk2
te lu am solo la ci xalaatu li ñuy tuddee résilience maanaam utub pexe loo xam ni ngir gën a ñoŋal baylat bi yokk poosam yokku pexeem ba nga xam ne %e bu amee choc li ñuy tuddee choc climatique maanaam taw yu yéex taw yu lifin mu mun a bëyandoo lu bëri njëkkee lii teg ci lii teg ci lii boole lii li ñuy tuddee diversification pour mën cee génn ci wàllum am sécurité alimentaire ci wàllu it koom doon na donc duunal gafaga ji ci wàllu ci wàllu koppar loolu pexe la ci moo tax gis nga pastèque bi dafa teel a ñëw moo njëkk ci marché bi
1,419,152
1,419,570
11spk1
%hum %hum
1,419,570
1,435,549
11spk2
te ba léegi mu ngi ci maanaam lay nawet ba léegi dugg si na am na lu xuus dem ca noor ba loolu ndox mi moo koy def te ndox mi da koy lay bi mooy dikk lay bi continué la ca des jëm ci basi ba jëm ci xaal bi wala jëm ci sëb
1,439,528
1,440,496
11spk1
d' accord
1,440,496
1,449,921
11spk2
taw ndox lay geneen xeetu ndox la glace geneen xeetu ndox la ndox ci ay formes am yu bokkul la benn bu ne ak la ko tax a jóg
1,451,314
1,460,235
11spk2
donc lay bi dafa am njeexital da ngay gis fi mu toll nii boo génnee ci bitti da nga gis toolu xaal nga dem xaal day màgg lu koy màggal bu taw bi arrêté taw bi noppee du lay kon lay ndox la
1,460,235
1,460,912
11spk1
%hum %hum
1,460,912
1,476,446
11spk2
mu ngi def liggéeyam basi mu ngay def liggéeyam si basi ba def liggéeyam ca ñe() sa sëb sa moo tax gis nga sëb si bu tàmbalee nga gis dañ koy witt lu bari ba ca kanam ndax moom floraison continue lay def da ngay witt bàyyi ko mu jebbiwaat nga wittaat bàyyi ko mu jebbiwaat bu lay bi taxawee mu taxaw
1,476,446
1,476,868
11spk3
%hum %hum
1,476,868
1,487,429
11spk2
basi bi it lay bi dina ko yóbbu ba mu ñor xaal bi it da ngay gis ñu njëkk ña ñi ne ci digg bi ak ñi mujj ñépp day kii bi moo koy yeggali lay bi kon lay bi dafa am moom tam
1,487,429
1,487,736
11spk1
%hum
1,487,736
1,511,575
11spk2
lay boobu ci dakasa yi bu ñu ko bàyyiwoon détourné wuñ ko naaj bi lakk ko moom it day boole day def li ñuy tuddee day favoriser maanaam day yokk day gaawal màggaayu champignon bi nga xam ne moom moo indi feebaru saabu yi looloo tax ñu koy di ko retourné maanaam di ko wëlbati bàyyi ko ci naaj wi mu lakk ko
1,515,692
1,521,862
11spk2
mooy afla() Aspergillus Flavus noonu la doomu jangoro ji tudd mi nga xam ne moom mooy indi feebaru saabu boobu ci gerte
1,523,891
1,542,924
11spk2
maanaam da ko njatt ci gerte gi balaa ñu ko koy déqi soo ko deqee pare daf koy topp te fu mu koy topp mooy ci dakasa yi di ko xaar ca naaf ba léegi nag gis nañ ne tàngoor boobu it am na yeneen xeetu xeex yoo xam ne xëy na bis bu ñu demee ba ñu war a waxtaanee lu jëm ci feebaru saabu bi dinañ ci gën a mun a xuus
1,543,936
1,544,281
11spk1
%hum %hum
1,544,281
1,544,943
11spk2
maasàllaa
1,544,943
1,549,975
11spk1
am na solo %e Chacun avec %e son domaine ah vraiment domaine bi defe naa
1,552,506
1,556,905
11spk1
mais Maodo dafa am foo xamante ne wax na ko sànq muy information climatique
1,556,905
1,557,303
11spk3
%hum %hum
1,557,303
1,564,843
11spk1
tay lan lay def ci mbay mi dafa mel ni %e ñoom mënuñoo dem sans yéen waaye yéen it mënuleen a dem sans ñoom
1,564,843
1,574,637
11spk3
loolu moom mooy li wér vraiment li ñuy wax partenariat gagant gagnant moom mooy li nga xamante ne bii moom moo nekk diggante météo ak waa agriculture
1,574,637
1,575,330
11spk1
%hum %hum
1,575,330
1,583,331
11spk3
%e damay dellu si rek léegi ci lu gën a gàtt rekk ci li mu wax fii mu nekk nii ah xam nga nee na actuellement nii ñu ngi nekk ci période kii quoi récolte
1,583,331
1,583,910
11spk1
%hum %hum
1,583,910
1,588,684
11spk3
gerte gi fu mu nekk nii dañu ko ngar bu dee dugub ji dañ ko takk def ko ay pot yu ndaw
1,588,684
1,589,118
11spk1
%hum %hum
1,589,118
1,633,823
11spk3
dégg nga ba pare nag léegi ñu ngi dox di am na ay techniques yi nga xam ne dañ koy def di fi teg di ko wëlbati di ko wëlbatiwaat xam nga loolu lan lañ ci bañ ah luñ ciy bañ en réalité mooy bu fekkee am nañ ay taw yi nga xamante ne bii c' est des pluies hors saison dégg nga mu créé ci kii quoi problème parce que bu fekkee léegi yow da nga %e déqi sa gerte nga daal di koy naaf directement ak humidité bi nga xamante ne nii moom mooy am noonu gerte gi dafay dafay kii quoi dafay xuur day saabu ngooñ bi aussi dafay xuur léegi yow non seulement dootoo ko mën a jariñoo mais jur gi aussi duñ ko mënati * parce que bu ñu ko lekkee dafa leen di créé ay problèmes mu %e d' ordre %e kii quoi gastrique
1,633,823
1,634,436
11spk1
gastrique
1,634,436
1,651,281
11spk3
dégg nga ah loolu loolu dafa nekk benn benn benn aspect ñaareel bi ma bëgg %e dëggal tuuti ci li mu waxoon léegi ci li jëm ci mbirum kii quoi xaal bi wala kii quoi ñebe ji nga xamante ne nii actuellement ñu ngi continuer donc %e di ko bay
1,651,281
1,652,075
11spk1
%hum %hum
1,652,075
1,679,695
11spk3
c' est vrai que ñu ngi koy récolté mais fur et à mesure ñu koy récolter dañuy gis ne encore dafay continuer donc di saxaat te xam nañ ni taw jeex na donc lan moo koy saxal pourtant ndox la mais ndox yooyu moom moo wute xam nga %e ndoxu taw nuage bi nga xamante ne bii moom mooy indi moom mooy indi taw ak niir bi nga xamante ne bii moom dafay indi %e souvent naka lañ koy waxee encore lay wala broullard dañoo bokkul
1,679,695
1,680,175
11spk1
%hum %hum
1,680,175
1,696,552
11spk3
même booy xool seen kii quoi ci seen constitution physique sax donc duñ du ñu kii quoi du ñu benn ñaare taw taw taw kii quoi ndoxu taw nuage bu koy indi souvent %e association ndox ndox yi nii lay nekk bu ànd ak kii quoi bu ànd ak ay cristaux glaces
1,696,552
1,697,019
11spk1
%hum %hum
1,697,019
1,730,165
11spk3
mais souvent bu fekkee %e kii nga am nag léegi %e lay lay nga am kooku yeneen façon nuage yi nga xamante ne bii ñoom ñooy ñoom ñooy kii quoi ñoom ñoo wàcc kii quoi ñoom ñooy changé disons de niveau wàcc ci suuf * kii bi quoi donc fee da ngay jàpp ni affaire bi dafay am %e dafay kii quoi dafay desengragé wu parce que da ngay am forte pénétration de particule kii quoi pluviogéneux dégg nga nga xamante ni bii bu bu amee ak tàngaay bi nga xamante ne bii moom la moom la moom moom disons moom la %e naaj bi di kii quoi di généré
1,730,165
1,730,733
11spk1
%hum %hum
1,730,733
1,742,143
11spk3
donc da ngay sentir que ni ndox mi kii quoi nuages yi dañuy gën di dañuy gën di ubbeeku goutelettes d' eau yi dañuy gën di tàng au fur et à mesure ñuy gën di tàng dañuy gën di màgg nu muy gën di màggee dafay gën a diis
1,742,143
1,742,678
11spk1
%hum %hum
1,742,678
1,746,887
11spk3
am na fi nga xamante ne bii ay précipité donc taw boobu bokkul
1,746,887
1,747,247
11spk1
%hum
1,747,247
1,754,082
11spk3
ak li nga xamante ne bii moom la ñu yàgg di d' aillers je dis bien d' aillers booy xool %e fin hivernage
1,754,082
1,754,755
11spk1
%hum %hum
1,754,755
1,766,978
11spk3
lay %e que ça soit la rosée wala muy le broullar nekk na ay signes yi nga xamante ne bokk na ci signes yi nga xamante nefoo ko gisee rekk xam ne nawet jeex na parce que :fa ñoom ñaar bokkuñu bokkuñu kii ay mbir
1,766,978
1,767,461
11spk1
%hum
1,767,461
1,769,350
11spk3
donc man suñu émission bee passé
1,769,350
1,769,730
11spk1
%hum %hum
1,769,730
1,797,640
11spk3
bi may taxaw naan leen bon nawet bi jeex na c' est parce que boobu daa mel ni commencé woon na absorbé broullard commencé woon na absorbé brute humide commencé woon na absorbé rosée ñett yooyu yépp nag ay xeetu lay lañu mais bokkuñu booy wax rosée mooy bi nga xamante ne bii da ngay xëy le matin rekk gis oto bee garré wala nii wala bois bi nga xamante ne gis ko layu bi wàcc si mu tooy xepp xepp xepp xepp bokkul ak brut humide bi nga xamante ne bii da nga ko observé nii ci ay benn distance bi nga xamante ne quatre wala cinq kilomètres lay nekk
1,797,640
1,798,120
11spk1
%hum %hum
1,798,120
1,805,473
11spk3
bokkul ak broullard bi nga xamante ne bii moom dafay nekk distance bi nga xamante ne bii peut être entre %e trois cent lay nekk ba sept cent ba huit cent mbaa lu ko ëpp
1,805,473
1,805,868
11spk1
%hum %hum
1,805,868
1,845,689
11spk3
donc visibilité yi souvent moom mooy visibilité gi quoi horizontale bi moom mooy li nga xamante ne bii mooy def kii quoi souvent la différence mais ñu jàpp rekk ni lay lay lay bi ñetti façons lay moo am am na lu tubaab di wax rosée am na lu ñuy wax brut humide am na lu ñuy wax broullard ñett yooyu foo ko gis rekk xamal ni nawet bi jeex na mais nawet bu jeexee bu continué di ñëw dootul mën a %e suuxat gerte du mën a suuxat dugub mais par contre xeetu meññeef yu mel ni ay ñebe wala ay xaal yooyu nga xamante ne bii soxlawuñu kii quoi ndox mu bari yooyu moom moom moom moom la kii quoi moom la xeetu layu yooyu amal njëriñ
1,845,689
1,846,114
11spk1
mais ndax
1,848,419
1,850,666
11spk3
présentement nii fan yii yépp matin bu ñu xëyee moom la ñu am
1,850,666
1,851,303
11spk1
d' accord
1,851,303
1,856,062
11spk3
bu boo koy seetlu boo yeewoo suba oto bu ma fekk mu taxaw nii dafay lay ba tooy xëpp xëpp xëpp
1,856,062
1,856,562
11spk1
%hum %hum