audio
audioduration (s)
0.74
50.6
transcription
stringlengths
8
285
Wàdd, kenn ci njiiti Senegaal
Lii du màggat mukk.
Dina nekk lu yomb
Naan na sàngara.
Kafe ci Ecoopi, Keeñaa, Ugandaa, Ginne, Kot Diwaar
Luy mbir mii jaxasoo?
Amul ug saytu.
Gisunu ko woon.
Xam naa jëml yii.
Ndaxte, ñooy wattu s unu kaaraange guddeek bëccëg
Ñax mi, ngir fasi la.
Xoolal dàlli Tom.
Dama koo mujjee fef.
Waaye, Maki jikkoy firawna lay doxe
Dinaa ko jéem.
Wóolu ma ci loolu !
Tomb 12 Koom mi
Nu ngi ci kaaraange.
Toog leen fii.
manuma koo génne.
ña jànq it seen diñe gaay seen wéttal
Lu tax nuy daw ?
Téyeleen ko !
Dunu Falkland (Nguur-Yu-Bennoo)
Sama télé daa toj.
Màggug hip-hop ci àdduna bi
Toppekat dal na seen kaw bu baax
Ci iniweersite bi, ngongo yi ñoongi bowoo ci bërëb yu wuute
Summileen seen mbaxana yi .
Ñëwleen jëlsi ko.
Xobet-xobet laa soxla.
Dafa man a fen.
Ca dëgg-dëgg ag mbaax la.
Jagley campeef yi ak seeni ligeey
Tom xaalis bu bari lay fayeeku.
Juum naa ndax kóolute gu ëpp ci sama bopp.
Damay xale bu góor bu baax.
Diiwaan yu fatt yi ci ay way dëkk
Looloo taxoon njëlul nguur gi loofoon, mujjoon moom nguur gi fees dell aki bor.
Daa soxla xaalis.
Xew-xew ci bis bi
Defleen li mu wax !
Lépp dara baaxu ci woon.
Daanaka amul menn piri moo xam ne ñépp dëppoo nañu ci, muy tekki garab.
Wànqaasam day am i dég te xobam 4 10i sàntimet àgg ci guddaay.
Damaa dox ba fii.
Lu la mar mayul, màtt du la ko may
Aa waaw, nanu dem.
Daa yaru lool.
Sabab yu jonjoo yi ñeel xareb adduna bu njëkk bi
Waaw, wax ngeen dëgg.
Ginnaaw bi ñu ko saytoo, la nu gis jàngoro ji ci moom
Ku may bàyyi xel ?
Dee a gën gàcce la siddiit yi ràbbaske bind ko ci xol yi.
Fàww nga màgg.
Seen ree gu neex na ma.
Lu tax xëpp deret nekk màndarga jóg-jot-na ci biir ëmb bi ?
Solleen seen yére fanaanukaay.
Danu koo war a jël.
Nun ñépp a am i ayib.
Bàyyil nama am mbind.
Kóllëre ginnaaw lay féete
Damaa war a jéggalu.
Ka wax lii de wax na wax ju rafet
Lalub selen boo ci tëdd it wàcci dellu fi suuf
Ñaata lay jar\?
Ndax bëggu leen ab defuma ay?
Gën naa tàng.
Gis ngeen loolu ?
Jàmbur yi ak Baadoola yi ñoo ci toppoon cig raŋ.
Génneleen mbalit yi !
Mayeesuma ko kenn.
Ana lan moo xew?
Ponki jikko yi jullit bu nekk war a jikkowoo
Soo xuloo ak ñoom ñu dittil la bi bënnut?
Ana goloo ka sàngoo mbàjj bay taamu nimoro diis?
Benn donga a joxewul ngànt
Lii a ka taaru !
Ginnaaw bi, nu àgg Luga,laataa fajar,yendu fa
Dafa niru ku maandu.
Sooratu Rahmaan, aaya 33
Takkoon na ay weer.
Dolli nañu ci sax jamonoy tëju
Dafay naan lu ëpp.
Dañ maa tegoon daan.
Loolu laa xalaat.
Ndiru na ku dëgër.
Loolu kat moo di ay teggin, kon jëfe ko cig wàllam
Tëjleen bunt bi.
Dama soxla nelaw.
Mag nee na
Manuma ko delloo.
Dinaa xaar ba fukki waxtu ak ñaar.
Nanu fàtte loolu !
Fi abadin bu nuxubi
Dafa am xel.
Dee ma yëgal fumu toll.
Dinanu leen dimbali.
Ndëgërlu gi ci gii yamale nga koy xamee
Dingeen dem it?
README.md exists but content is empty. Use the Edit dataset card button to edit it.
Downloads last month
69
Edit dataset card